MBETTEL SAISON 3 EPISODE 21

8 383
1 074
 
Commenti
Aliou Dieme
Aliou Dieme - Mese fa
Ousmane iow abe rieul deggue ngua
yayi dabakh
yayi dabakh - 2 mesi fa
Wouyaye deureum gadio raynama😁
Marie Caroline Wade
Marie Caroline Wade - 2 mesi fa
Shiii fatdame sof nama torop. Sou saye cordes vocales dagué digua nopalu!
Hafsatou Dia
Hafsatou Dia - 2 mesi fa
Fatdame je te déteste madione appel la police ki eupeul na wayy
Fatou Sy
Fatou Sy - 2 mesi fa
Fat dame j'laime daleu la Mouy joué eupeuna😂😂😂
omar omzo N.1
omar omzo N.1 - 2 mesi fa
Mandion fassel ki way goor day am diom
Tina Demba
Tina Demba - 2 mesi fa
Yhd
Mboye Ndiaye Dieng
Mboye Ndiaye Dieng - 2 mesi fa
wa ani you name ndeye ndiaye
doffou balla
doffou balla - 2 mesi fa
Ndeyssan
Mafallou Gueye
Mafallou Gueye - 2 mesi fa
Li eskeu dou ay guént aa warouna
Modou Sarr
Modou Sarr - 2 mesi fa
Ani kou beug yayam❤️✅
Mouhameth Fall
Mouhameth Fall - 2 mesi fa
Salamm Les baye FALL é Les yaye je suis un nouveau
Aissatou Ndiaye
Aissatou Ndiaye - 2 mesi fa
nafisatou say wolof khnne
Aissa bibi Wane
Aissa bibi Wane - 2 mesi fa
punaise, passage ousmane ak deureum ca ma achevé... wepepepe Mandioye ak gnane yi naaak, ndeketer seuy dou fo shiiii
fatou faye
fatou faye - 2 mesi fa
Ni deureum di dawé coum danél.
Ourey Thiam
Ourey Thiam - 2 mesi fa
Ayway Fatdam bayile Lay Lay néna beugue diame motakh mou deuck Diamalay khana sa yarame dina daw Hahahah
Khadim Ndongo
Khadim Ndongo - 2 mesi fa
👍👍
Cheikh Diop
Cheikh Diop - 2 mesi fa
Ousmane dinama Ray
MELTING POT
MELTING POT - 2 mesi fa
LA COUSINE DE ROUBA A L' AIR FAUSSE
Sokhna Arame Fall Mbaye
Wouy deuram mingmay Ray way
Khady Mbaye
Khady Mbaye - 2 mesi fa
Ousmane gnane na liiiii
Ndeye Coumba Wade
Ndeye Coumba Wade - 2 mesi fa
Madione so fasewoul fat dam Dina la talle😂
Nabou Ba
Nabou Ba - 2 mesi fa
Non deureme raynam😂😂😂
Daouda Diop
Daouda Diop - 2 mesi fa
Le scenario est vraiment dOop macha alla kou daccord ak mane pousse bleu may séine
Thieer Ba
Thieer Ba - 2 mesi fa
Fatdam moder un peu ta langage oubekoule dou wakhe bou raféte avant de parler ils faut réfléchir avant de dufusuier la série le réalisateur ils bien voir les choses merci l'équipe Mbettel 😥😥😥😥😥😥
Aicha Thiello
Aicha Thiello - 2 mesi fa
nafissatou nena guélou ousmane bé ma dadjel mounane ma kouss kondrong la khawma thiappe kéleng leng doynama seuk 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Khadidiatou DIALLO
Khadidiatou DIALLO - 2 mesi fa
team nafiii
Younouss Ba
Younouss Ba - 2 mesi fa
Am ndiarel diehna ci Sénégal
Ali Salman
Ali Salman - 2 mesi fa
Ndeureum way ray nama
mel ladiva
mel ladiva - 2 mesi fa
Dégeuna deuge si seuÿ yi
Matar Fall
Matar Fall - 2 mesi fa
fat dame amoul respect
Diallo Diallo
Diallo Diallo - 2 mesi fa
Nattou dankoy Santé sa boromm? alhamdou lillah rouba
Fatou  Ba diaw
Fatou Ba diaw - 2 mesi fa
La Sœur de Rouba Fa Thierno nékhnama torope sakh
Mboye Ndiaye Dieng
Mboye Ndiaye Dieng - 2 mesi fa
en plus elle est trop belle
samba niang
samba niang - 2 mesi fa
mane rouba daff ma soff trop
Mariama Marguerite Diallo
Hii nafissatou tay mome ell a parfaitement raison
Mariama Marguerite Diallo
Mais fat dam a exagéré
Serigne Ibrahima Diop
Serigne Ibrahima Diop - 2 mesi fa
Ana gniy beugue mandione tak Roubeu
murtala drammhe
murtala drammhe - 2 mesi fa
nekh na torop
hmjr Foot
hmjr Foot - 2 mesi fa
Mane deureume dina ma ray🤣😄😀 Mandione fasél ki waay niak Foulla tropp😔😕
Bass Ngom
Bass Ngom - 2 mesi fa
Thico Rieul lue
omar samba ndiaye
omar samba ndiaye - 2 mesi fa
Presque 600mil vu en moins d'une semaine. Série qui bat tous les records. Mashala way
Alijagu Camara
Alijagu Camara - 2 mesi fa
Yallah nañiu borom bi meussal si djiabar diou mel ni fatdame
Son comportement mako ragal
Rouba borom xöl bou bakh lou bonn rek lay am❌😔(Yaye)
Nekhou Niass
Nekhou Niass - 2 mesi fa
Béll mér
Sankoun Kanoute
Sankoun Kanoute - 2 mesi fa
Mandione Ami diabar bou bakh teh Papa Diouf bonne na trop.Seulement amoul chance dakh waji dewoul teh Yallah dou teuj joint teuj palanter wathie rido say.
Elhadji Niang
Elhadji Niang - 2 mesi fa
Anna ngane bandii bi
ShadowK 45
ShadowK 45 - 2 mesi fa
Perché c'è sta roba nelle tendenze?
Mariama Mbaye
Mariama Mbaye - 2 mesi fa
Fat dame weroul way koussi ande besseul j aime
Sarr Pape
Sarr Pape - 2 mesi fa
No deureum amoull djiomm qoi 😂😂😂😂nénako dangay woyou woyou lou rk
Lamine Ndiaye
Lamine Ndiaye - 2 mesi fa
Wa fatou dame nitt la mais ken dou soeur rou rouba bi
Gnagna Bint Muhammad Al Amine
j'adore deureum
Prossimi video