Urgent! La Levée Du Corps De Sidy Lamine Niass Reportée La Déclaration De son fils Cheikh Niass

595
99
 
Commenti
Die Ndao
Die Ndao - 9 giorni fa
Y'a pas de talidé qui tiennent ici c Aux fils du défunt d décider . Que son âme repose en paix
aita niang
aita niang - 10 giorni fa
Nagn dello xel yi si yalla ko hamni meussoul seetan nit d'i def loudoul yonn té dou réagir tay mou teud guenn d'i wah meunou tontou hamlen ni dhè rk moy deugu bayilen son fils def liko warr gni ko fiy khethio yepp diapalè wou gnou ko bimoulen sohla wè
khady Bamba
khady Bamba - 10 giorni fa
Yeureum len ki diebal kou boramam vraiment mettina trop diaroul xeuthio bilay
Cherif Diago
Cherif Diago - 10 giorni fa
Dako rouma yof mane kaolack la dakor lolou la keulifayi wakh dèlène deuglou keukifayii ak borome kham kham yii
Zama FZ
Zama FZ - 10 giorni fa
sérigne sidy lamine président du groupe walfadjri etait un grand homme le sénégal a perdu quelqu un reposé vous en paix que sérigne ibrahima niass et son pére le profét l accueil au paradis
vidéos YouTube SN
vidéos YouTube SN - 10 giorni fa
1 Jaime=hommages à sidy lamine Niasse
Amina Houdati
Amina Houdati - 10 giorni fa
vraiment il ne merite pas ca madame kamara depuis maroc 😢😢😢
BA MANSOUR
BA MANSOUR - 10 giorni fa
Vraiment il ne mérite pas ça .
Ibou Faye
Ibou Faye - 10 giorni fa
Mais le corps appartient a son fils s il est l aîné
Khady Dieng
Khady Dieng - 10 giorni fa
Aye waye lii niawna 😭😭😭di
Farmata Sall
Farmata Sall - 10 giorni fa
Il faut respecter son choix C mieux. Paix à son âme
Oumar hamidou SY
Oumar hamidou SY - 10 giorni fa
Name Elhaji sidy nieupeu ko bokk mais nak taawam bou goor aki ndiabottam nioniou thi euppeu walleu
Sombrero Malgache
Sombrero Malgache - 10 giorni fa
Qu'est-ce que cette vidéo fout en tendances FRANÇAISES ?
Mamadou Sow
Mamadou Sow - 10 giorni fa
Djiss nanè deug la dèthi ko gaw moo eupe yeurmandè mai nak c.est pa évident prsk yonete psl lundi lafi dioguè nioguiko dèthi mercredi donc on a pa vraiment les raison force de l.inhumer a Yoff keur dinè yi dingal rek mofa ame dc dingal dioqu na cheikh niass malgré les recommandations d ton père laisser comme ça sa diane wathie na machalah
Cheikh Ndiaye
Cheikh Ndiaye - 10 giorni fa
ay domam nio eupe sagn sagn niépe thi mom lignou beugue lagnou wara déf kouy diaye sagn sagn nga dém diayiko thi sa baye té bayi bayou diambour bi diambari l'islam bi yalnako yalla défal téranga dioudoul diékh thi daradiay mouhamad s.a.w.salama
bijou diop
bijou diop - 10 giorni fa
Non bouléne wakh talibé yui c’est famille vus les déclarations
ramatoulaye balde
ramatoulaye balde - 10 giorni fa
qu Allah t'accueil dans son paradis RIP
abdoulaye niang
abdoulaye niang - 10 giorni fa
cheikh Niasse DINA bakh inchala
Moustapha Fall
Moustapha Fall - 10 giorni fa
NANE TOPPOU SÉNE NDIGALOUL BAY AHMAT KHALIFA NIASS ' NDAKHE MO FIY SÉNNE BAY TAY
السباب أهل السنة فى السنغال الله أكبر
kokou bou pékhém dioubé famille bi dotoun dioubo
Mata Hari Diaby
Mata Hari Diaby - 10 giorni fa
il fut un homme qui s'est toujours battu pour le Sénégal. c'était un patriote. je suis malienne quand je vivais au Sénégal, il était mon exemple. 11 iklas pour le repos de son âme. tu es parti,mais tu reste dans nos coeur.
papamovic diop
papamovic diop - 10 giorni fa
Nidiay djii dakko teuddé dawal xolko
https://youtu.be/t0Nf8WFcKMg
LA PÉDOPHILIE DANS LA FAMILLE SÉNÉGALAISE
Abdou Gueye
Abdou Gueye - 10 giorni fa
pour lann doudem yof nitki loumoubeug langkay défall
NiangBlg Apk
NiangBlg Apk - 10 giorni fa
Ki dafa réw ta dafay féne Sidy Lamine wakhou ko dara
Ta mome tékssy dou tawou Papame
Fama Mbaye
Fama Mbaye - 5 giorni fa
NiangBlg Apk iow deh yama meuna doul rew ta gnemei yalla yadone fekei bamouy waxtane ak bayam? Boudoul tawou bayam tamite bayam mome la wane askan wii nite day mandou boo amoul preuve si liguay waax daguay teudj sa gate wassalam
Mouhamed Diop
Mouhamed Diop - 10 giorni fa
NiangBlg Apk Yw doff nga rek
Ibrahima Gaye
Ibrahima Gaye - 10 giorni fa
Waxtan wax degue RK d'à siy baxx
kourakoura mbiss
kourakoura mbiss - 10 giorni fa
Serigne talibem ,yenneti sakhbam,président peuplelam kouco sopi tahirga.sa talibe mouna diokho bacanam té sa dom diaraloulkoc
Cheikh A. K. Dieylani CAMARA
son fils a tous les droits. Talibe dou sopp... talibés daay mandou
Oni Mad
Oni Mad - 10 giorni fa
😭Rip 😭 rip 😭 rip 😭 rip 😭
Marodi TV Sénégal
Marodi TV Sénégal - 10 giorni fa
https://youtu.be/IoZUTfxUeJE
Diop Ndéye fatou
Diop Ndéye fatou - 10 giorni fa
Inalilahi wahinaliraja khona Yalla nako yala yereum Kilifa loumou dékané dal nagne kako défal mo guenn
Layzo Carlou
Layzo Carlou - 10 giorni fa
Non vraiment li dou yoon ...C'est triste franchement !!!!
Seynabou Sarr Ringenbach
Seynabou Sarr Ringenbach - 10 giorni fa
J'ai vraiment mal au coeur svp respecté le corps 😭😭😭😭😭😭😭😭😭méritéwoul li...
inconnu mbacké
inconnu mbacké - 10 giorni fa
Aÿ way Lima wor moy sidy lamine méré nalén trop rou gui dem na ab néw rek guén di kheuthio soutoural lén ko enterré ko décédé depuis 3 jour guén teuyé ko rek
Malaw Diallo
Malaw Diallo - 10 giorni fa
Lane Moy talibé Sénégal mo nékh
Lebron James
Lebron James - 10 giorni fa
La terre où on doit le mettre n'a pas d'importance, Yoff ou Léona c'est pareil. Le Prophète psl on la gardé 3jr sans l'enterrement et beaucoup d'autre Sahara aussi. Et la décision final appartient au famille
yaye fall fall
yaye fall fall - 10 giorni fa
Tiate dinala top baci birr bamel yalah nala yalah yeureum
Maguette Thiam
Maguette Thiam - 10 giorni fa
Non me li c'est du jamais vu ani talibe ak kheuthio domou serigne bi
Max Diop
Max Diop - 10 giorni fa
Dakar et kaolack c est meme chose dieu et partout
foufa sarr
foufa sarr - 10 giorni fa
bilay
Abdelhadi Abdelhadi
Abdelhadi Abdelhadi - 10 giorni fa
Je ne suis pas senegalais et qui il etait musulman il doit etre enterré le plus rapidement et ou il aurait aimé pourquoi pas? Du moment quil etait musulman rabi yerahmou en algerien
Yacine Ndiaye
Yacine Ndiaye - 10 giorni fa
C vraiment dommage, mais IL ne merite pas ça. Allahouma firlahou warhamhou
Ndeyeawa Mbaye
Ndeyeawa Mbaye - 10 giorni fa
Sidi lamine niass ne mérite pas ça il fallait pas laissé ça jusqu'à maintenant il faut que ses enfants prennent leurs responsabilités
ousmane NDIAYE
ousmane NDIAYE - 10 giorni fa
Vairema sidy lepelou nou li bayi len werente wi ta dengi sidy fimo wakhe ay do mam
cherif Sarre
cherif Sarre - 10 giorni fa
Yalla nako yalla kharel aldiana firdawsi
Marie Diatta
Marie Diatta - 10 giorni fa
Yalla nako yalla yeureme kharéko aldiana firdawsi oh Sama yarame dawna 😭😭😭😭😭
Saly Ndiaye
Saly Ndiaye - 10 giorni fa
Vraiment il ne mérite pas cela son fils aîné na qu'à prendre ses responsabilités en plus il voulait qu'on l'enterre à yoff ou es le problème vraiment li koumou nekone sa baye doula nekh
Aminata touré
Aminata touré - 10 giorni fa
Sou fèkkè beugheu gha goudou fane daghay dèglou ngila fii djitou tè gha khamni dougnou deff lou yallah geureumoul indiko si penc mame bii lougne deff lou moyy lolou dèfoul deugg tè nèkout si deugg...
Fekam Kane
Fekam Kane - 10 giorni fa
+Amina Cisse ki key moy lolou, dans qu'el senegal nous vivons ?
Amina Cisse
Amina Cisse - 10 giorni fa
Ki weroul da dof bouko tontou vu ko
Fekam Kane
Fekam Kane - 10 giorni fa
Wa mane damay beug warou ? Ki dè mo beug gnou dinthieuko Dakar ndakh simplicitem ndakh ragal yallam, nganane mame ak goude fane.
BABACAR SINE
BABACAR SINE - 10 giorni fa
Merci chekh niasse
Aminata touré
Aminata touré - 10 giorni fa
Cheikh na khamni sidy kilifam la c vrai wayè momitt daffa wara amm kilifa magg ngi bougnou wahè rekk waw gha si wara tekk (niakkeu kilifa goonè douko deff
thierno ba
thierno ba - 10 giorni fa
C'est vraiment extraordinaire. Pour moi deux volontés s'opposent:l'une celle des talibés qui voient que leur marabout doit ètre aupres de ses parents pour que durants les gamous ça soit facile de leur coté pour des priéres et Ziara. De l'autre coté ses fils qui veulent qu'il soit à yoff.De ce fait y a pas de tord ni vinqueur ni vincu.Parler de marabout sans talibés c'est parler d'Etat sans chéf. Mais aussi quant on parle d'heritage c'est parce qu'il y a des relais qui sont ses fils. Donc c'est nous dans nous .Il faut plus de comprehension de la part des deux cotés. Que la terre lui soit légére Amine On a perdu un un trait d'union entre le fond et la forme. RIP
cheikh baye gadji
cheikh baye gadji - 10 giorni fa
ki il est fou wilaya on le respect pas pour ay lime beugue sidy lamine sakhe dafa ame kilifeu walla alors khilafa lewna bou desse si ki daye tasse !!!
Amina Cisse
Amina Cisse - 10 giorni fa
+Hamadou Diop ki weroule da doff
Amina Cisse
Amina Cisse - 10 giorni fa
+Ousseynou Dione Lol
Ousseynou Dione
Ousseynou Dione - 10 giorni fa
bayil ba sa baay dé ngeu dogal niune amnagne kilifeu wayé man sama serigne lima feké muy deff moy lath bdjaboot gui lou guene si beugeu niu deffé ko nonu talubé amul loumouy dogal si kilifam surtt mu laku nak..ndigeul gui dome ji mokoy diokhé nassi nieup antout wasalam.
Yacine SyllaSRK
Yacine SyllaSRK - 10 giorni fa
ndeyssane
Mbodji Aïssatou
Mbodji Aïssatou - 10 giorni fa
Vraiment il respecter sa dérniere volonté.
mbacke falle
mbacke falle - 10 giorni fa
Sidy dafa comprend ni fo mane di nék sa dieuf rk mola fay fék guinaw yermandé yalla
Mouhamadou Lamine DIONE
Mouhamadou Lamine DIONE - 10 giorni fa
Inna lilahi wa inna ileyhi radji ounne
Cheikh Ngom
Cheikh Ngom - 10 giorni fa
Fatiha ak 11 lixlass salatou alla naby diokh ko Elhadj sidy lamine niass Yalla na khippé aldjana firdawzi amine
Ndiaye babacar
Ndiaye babacar - 10 giorni fa
Ndeyssane
Ramatoulaye Diedhiou
Ramatoulaye Diedhiou - 10 giorni fa
Il faut respecté sa dernière volonté et celle de sa famille ,pourquoi les talibés se comportent de cet façon paix à son âme
Mouhamadou lamine Dabo
Mouhamadou lamine Dabo - 10 giorni fa
Entka l'Etat doit prendre ces résponsabilités demain ne se reste que pour réspecté le désir de SLN .son fils a le derniers mots .
soow dina
soow dina - 10 giorni fa
Sidy lamine nitt kou oyoff la bilahi
Aida Gaye
Aida Gaye - 10 giorni fa
Mais li dou yone guén defarko baparé diko remporter ba souba inchalla dioulite loko geuna tèla dinthie yeurmandè yalla wathie si mom mais liguèni Def dou deugu dou yone néna nagnouko yobou yoff kone yobou lenko fimou beugu guén yobouko entout cas dall mom mi teude yakamtina guén yobouko keureum bi moudie
Dado Ba
Dado Ba - 10 giorni fa
Ndeyssane yaguena nagniouko diegual boromame yanna yalla yessal yeurmander si kawaw ndeyssane
Mame diarra Gueye
Mame diarra Gueye - 10 giorni fa
Talibè dafaye woyè diguel dano sop waye domame moye dogal
Cheikh Nourou Niang
Cheikh Nourou Niang - 10 giorni fa
Dangal doul domame do u do gal kilifay papam nioy dogal télolou moyy ame
Niang biz N
Niang biz N - 10 giorni fa
Diambar danou n'a😭😭😭
Saer SANKHE
Saer SANKHE - 10 giorni fa
Adouna mo yak sollo
Niang biz N
Niang biz N - 10 giorni fa
Prends tes responsabilités c les dernières volontés d'une personne ki compte yalnako yalla yeureum té owafal souf si kawaw
domou djolloff
domou djolloff - 10 giorni fa
Je suis choquée may wakh mounane Talibe wa gni kouniou. Aye simple talibe di doul lo nite yi
Oumy Ndiaye
Oumy Ndiaye - 10 giorni fa
Ken dou dogal sa keur baay, ba paré di dogal keur bayou diambour. Nagne bayi ay domam gnou décidé
Kyra Kyra
Kyra Kyra - 10 giorni fa
Vrema
Mbengue Laye
Mbengue Laye - 10 giorni fa
Oumy Ndiaye walahi
El Hadj Diallo
El Hadj Diallo - 10 giorni fa
Mes sincère condoléances à toute la famille
Maguette Kamara
Maguette Kamara - 10 giorni fa
Mes condoléances à sa famille que Allah l accueille au paradis
serigne mbackea
serigne mbackea - 10 giorni fa
Mé l'an Moy problème bh l'an mo tax doniou co dfal limou beugeu ba wax co ay domam kan moco gneu diegé ndiabotam li domam wax lolou moyz
Aima Sow
Aima Sow - 10 giorni fa
Aye mamame nio gui Léon niassene mais il faut respecter sa dernière volonté et celle de sa famille
Khady Sakho
Khady Sakho - 10 giorni fa
Yalla nalen yalla défale limou beugue
borom belel
borom belel - 10 giorni fa
Bayi lenn sen thiakhan yi sidi laminn defal na yalla lo khamni fom nek yalla fek kofa ak yeurmande
Fallou Dia
Fallou Dia - 10 giorni fa
Lolou mom Lou amla
MohMo
MohMo - 10 giorni fa
Si c’etait son choix qu’on l’execute! De toute façon personne ne le connait mieux que son fils.
autralia. kary
autralia. kary - 10 giorni fa
COMMENT PEUT ON ALLER A L'ENCONTRE DE LA DERNIERE VOLONTE D'UN MORT... DE SON VIVANT SYDI LAMINE A VOULU QU'ON L'ENTERRE A YOFF..POURQUOI FAIRE LE CONTRAIRE. SA FAMILLE NE PEUT QUE SUIVRE. C'EST INADMISSIBLE CE TIRAILLEMENT..SYDI LAMINE NE MERITE PAS CA VRAIMENT
melanin girl
melanin girl - 10 giorni fa
Wa pourkoi niouy bagne niou dénthieuko yoff? C koi le problem damay latheté rek😑
mamethiernu pene
mamethiernu pene - 10 giorni fa
Ameth khalifa Niasse dakko bègue politisé
jaffaar jaffaar
jaffaar jaffaar - 10 giorni fa
Nit dagnouy fontou bayilen djabot gui no def sen deuil si diam .kou fi guiss néw bougnou djeul diko yobou maka wala medine man khawma Sénégal lou len dal
Dioly Seye
Dioly Seye - 10 giorni fa
melanin girl pask neinagn talibèm yi niooko bagn tè sidy yoff la wakhone
Awa Sylla
Awa Sylla - 10 giorni fa
Ndeyessane R.I.P.
Fanta Fall
Fanta Fall - 10 giorni fa
La décision appartient à ses enfants et non a ses talibés.c'est pas du tout normal j'ai le coeur meurti
Anna Dia
Anna Dia - 10 giorni fa
Mounass Mimi walay c est désolant quoi li fi rk la ame
Mounass Mimi
Mounass Mimi - 10 giorni fa
Fanta Fall problème bi dou talibés yi kessé amena yenene kilifa kaolack you nek sene guinaw. Lii niaw na torope😢😢
Anna Dia
Anna Dia - 10 giorni fa
La décision revient à ses enfants 😡
Anna Dia
Anna Dia - 10 giorni fa
Fanta Fall vraiment Sénégalais mo sof
Daouda Ndiaye
Daouda Ndiaye - 10 giorni fa
Il faut respecter son testament son fils a tout dit
oumishta la capricieuse
oumishta la capricieuse - 10 giorni fa
bilahi mérité woul lolou Niasse
Bassirou Ndiaye
Bassirou Ndiaye - 10 giorni fa
+Adama Kandji yalnako yala yaram
Adama Kandji
Adama Kandji - 10 giorni fa
Man Sénégalais dafma yeem nit dehh bayi ndekaner ak ay doman oie simple talibe rekk nga xawma auditeur nganer doufi amer ragallen yalla te settsi adji dem thie le dernier mot revient a sa famille
Lamine Baldé
Lamine Baldé - 10 giorni fa
Mandale snegal diakhal namma nanko deffal limobougo. Sln merite woul li way
Cheikh Sarr
Cheikh Sarr - 10 giorni fa
Il faut se consulter a la famille werente bakhoul te adouna amul solo yalla nako yalla yereum si BARKE SERIGNE TOUBA
Fan's cr7
Fan's cr7 - 10 giorni fa
Stop pas Barke serigne Touba ! 😡 Arrêtez avec vos blablas. Repose en paix 👏😢
Aminata touré
Aminata touré - 10 giorni fa
+nit da fay am yar ndour machalah ligha wakh moyy deugg q'il soit inhumè à kaolack
nit da fay am yar ndour
nit da fay am yar ndour - 10 giorni fa
Dé léne wakhal ki dém limou wakh yobou lén ko kaolack si thiosanam bayilén thikhane
Yaya Wade
Yaya Wade - 10 giorni fa
Adouna amoul solo soumma amatahou fa akh bara
Prossimi video